32
« Ano svp bonsoir tutodakar mane dh ano la beuguone sama famille niepp diahlé hamouniou founiouy koy dioyé je suis marié ya 3ans à un homme. Mais mo seyci souniou keur pask sama papeu beugeul ay domame geneu keur gui. Amna beneu dôme ya plus 1an problème moy mom yahh n’a tass n’a souniou keur dafa eumbeul sama niari sœurs yi tutodakar keneu ki 3 mois l’autre 1 mois t nioune souniou famille niepaniou xamm ci Sénégal sama dieukeur dji gené nagne ko ci keur gui. Ndah amouniou beneu solution tuto. Bilahi sama papa dako beugone ray boumouko yegué. Lgui diahlé nagne je sais pas souniouko xamé souniou derr dina yaxou ci Sénégal. Je voulais des conseils svp ».